Ay Baatu Waxtaan

More time & directions…

Phrases To Practice / Phrases à la pratique

Ban waxtu moo jot?What time is it?

Minwi jotna.It is midnight.

Fukki waxtu ak ñaar jotna.It is noon.

Naka laa fay demee?How do I get there?

Ci wetu jumaa ji.Next to the mosque.

Toppal yoon wi.Follow this road.

Xam nga fan la?Do you know where it is?

Kan ngay ñew?When are we arriving?

Time & Directions

Midi Jotna.It is noon.

Netti waxtu ci ngoon jotna.It is three in the afternoon.

Jubelal ci biir dekk ba.Keep going straight through the town.

Ci ñaari waxtu la nuy egg.We are arriving at two o’clock.

Da ngay tallal ci kanam. - Straight ahead.

Naari waxtu ci suba jotna.It is two in the morning.

Kan ngay dem?When are we going?

Ci kanamu jumaa ji.Across from the mosque.

Fukki waxtu teg na ñeent fukki i simili ak juroóm.It is ten forty five.

You got the time?

What time is it? Ban waxtoo jot?
Et maintenant en français; Quelle heure est-il?

Do you have a watch? Am nga montar?
Et en français;
Avez-vous une montre?

   Yes, I have a watch. Waaw am naa montar.
Et maintenant en français; Oui, j’ai une montre.

   No, I don’t have a watch. Amuma montar.
Et en français; Non, je n’ai pas de montre.

Morning? Afternoon?? Or maybe Evening???

Below is a table showing how the various portions of the day are labeled in Wolof.

ENGLISH WORD

WOLOF WORD

WHEN USED

day

bëcëg

dawn to nightfall

night

guddi

nightfall to dawn

morning

suba

dawn to about 2pm

afternoon

ngoon

from about 2pm to nightfall

midnight

xaaju guddi *

at midnight

* Literally, “half of the night” (xaaju – to divide, seperate, part, portion).

Ci suba. – In the morning.

Ci ngoon. – In the afternoon.

Ci guddi. – In the evening.